lirikcinta.com
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

love - aida samb feat. hakim lyrics

Loading...

love, i will give my heart to you
and make your dreams come true
never make you heart to lose

oh na na na no no no
louy dundeul sa khol bae (mbëguel mbëguel)
mbëguel moy doundeul sama khol bae (mbëguel mbëguel)
louy saffal sama khol bae (mbëguel mbëguel)
mbëguel moy doundeul sama khol (anh han)
love bi néthii man néthii yow
té liko teug t-ssaguko
nelow na thii say lokho
yewou thii sa khol
love bi néthii man néthii yow
té liko teug t-ssaguko
nelow na thii say lokho
yewou thii sa khel thii sa khol
yeah yeah yahh
sama mourray
thii biir negg bii thii kaw lal bii moy sa nofflay
eh hé hé eh
wakhal wayy
samey thiouray
you bakh yi namngako wayy
ah han yeah yeah
yow lingueu nekk yow lay done
té fo diokhogn moy sama yone
mouy souba goudi ak ngone
ah han han han
yow lingueu nekk yow lay done
té fo diokhogn moy sama yone
mouy souba goudi ak ngone
ah han han han
love, i will give my heart to you
and make your dreams come true
never make you heart to lose
oh na na na no no no
love, i will give my heart to you
and make your dreams come true
never make you heart to lose
yeah yeah yeah yah
love bi néthii man néthii yow
té liko teug t-ssaguko
nelow na thii say lokho
yewou thii sa khol
love bi néthii man néthii yow
té liko teug t-ssaguko
nelow na thii say lokho
yewou thii sa khel thii sa khol
m-sseck thiam
(mbëguel mbëguel)

Random Song Lyrics :

Popular

Loading...